Acts 13:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñoom ñu jóge Peers, aw ca yoon wa, ba ñëw dëkku Ancos ci diiwaanu Pisidi. Bésu noflaay ba nag ñu dugg ca jàngu ba, toog.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu, ñoom ñu jóge Perge, jàll ba Àncos ca diiwaanu Pisidi. Ñu dem jàngu ba, dugg, toog ca bésub Noflaay ba.