Acts 13:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Loolu lépp xew na ci diirub ñeenti téeméeri at ak juróom-fukk. «Gannaaw loolu mu jox leen ay àttekat, ba ci yonent Yàlla Samwil.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu lépp a ngi am ci diiru ñeenti téeméeri at ak juróom fukk (450). «Gannaaw loolu moo sàkkal sunuy maam ay njiit, ba ci jamonoy Yonent Yàlla Samiyel.