Acts 13:25 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te ba Yaxyay jeexal sasam, mu ne: “Ku ngeen may teg? Duma Ki war a ñëw; waaye am na kuy ñëw sama gannaaw, koo xam ne kii yeyoowumaa tekki ay dàllam.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Yaxya di jeexal aw sasam la ne: “Ana ku ngeen foog ne moom laa? Duma ki ngeen foog, waaye am na kuy ñëw nii sama gannaaw, ku ma yeyoowula summil sax ay dàllam.”