Acts 13:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yoon dabu ko fenn, moona ñaan nañu Pilaat, mu reylu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gisuñu ci moom lenn lu ko àtteb dee dabe, te teewul ñu sàkku Pilaat reylu ko.