bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 13:29
Acts 13:29 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu ñu def lépp lu yonent yi bindoon ci mbiram, ba noppi ñu wàcce ko ca bant ba, tàbbal ko ci bàmmeel.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw ba ñu matalee mboolem lu ñu bind ci moom, lañu ko wàccee ca bant ba, dugal ko bàmmeel.