Acts 13:33 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
def na ko ngir nun seeni sët, ci li mu dekkal Yeesu. Moom lañu bindoon ci ñaareelu saaru Sabóor ne:“Yaa di sama Doom,maa di sa Baay tey.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
nun sët yi la ko defal, ba mu yékkatee Yeesu, te noonee lañu ko binde ci ñaareelu saaru Sabóor, ne: “Yaa di sama Doom, bés niki tey maa la jur.”