Acts 13:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it li ko Yàlla dekkal, ba mu bañatee jaar ci dee, te suuf du ko lekk mukk, moom la Yàlla wax ne:“Dinaa la may barke yu sell te wóor,yi ma digoon Daawuda.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu ko Yàlla dekkale ndekkite lu dee toppatul, te yaramam du yàqu mukk, noonee la ko Yàlla waxe woon, ne: “Maa lay jox barkey Daawuda yu sell yi te wóor.”