Acts 13:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Kon nag bokk yi, nangeen xam ne, ci moom Yeesu nu ngi leen di yégal mbaalug bàkkaar yi. Te fépp fu yoonu Musaa tële woon a àttee nit ni ku jub,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Kon nag bokk yi, xamleen ne ci Yeesu moomu lañu leen birale njéggalug bàkkaar. Te mboolem lu ngeen tële woona wàccool, ba seen njub mat ci yoonu Musaa,