Acts 13:41 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
“Yéen ñiy xeebaate, gis leen lii,ngeen yéemu ba far;ndaxte dinaa def ci seen jamono jëf,joo xam ne su ngeen ko déggee sax,dungeen ko gëm.”»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
“Yeen xeebaatekat yi, xool-leen, jommileen te ne mes, ndax jëf ji may def ci seen jamono, ku leen ko waxoon sax, dungeen ko gëm.”»