Acts 13:44 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu bésu noflaay ba ca tegu, daanaka waa dëkk bépp daje, ngir déglu kàddug Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bésub Noflaay ba ca topp, daanaka waa dëkk bépp a daje, ngir déglu kàddug Boroom bi.