Acts 13:47 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte moom la nu Boroom bi sant ci li mu naan:“Samp naa la, nga nekk leeru ñi dul Yawut,ngir nga yóbbu mucc gi, mu daj cati àddina.”»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax noonu la nu ko Boroom bi sante ba mu nee: “Maa la tabb ngay leeru jaambur ñi, ngir nga jottliji mucc gii, ba ca cati àddina.”»