Acts 13:51 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Pool ak Barnabas daldi yëlëb seen pëndu tànk, ngir dëggal seen weddi, jëm dëkku Ikoñum.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol ak Barnaba nag fëgg seen pëndub ndëgguy tànk, seedeel leen ko seen ngàntal, doora dem dëkk ba ñuy wax Ikoñum.