Acts 14:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ci lu jafe yey nañu mbooloo ma ak wax jooju, ba tere leen, ñu rendil leen sarax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu lépp ndaw ya wax nañu ko te tuuti kon ñu tëlee tere mbooloo ma ñu rendil leen sarax.