Acts 14:22 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
di dooleel xeli taalibe ya, xiir leen ñu sax ci yoon wi; ñu ne leen: «Ci kaw nattu yu bare lanu war a dugge ci nguuru Yàlla.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñuy feddli pastéefu taalibe yi, di leen ñaax ngir ñu saxoo ngëm, ne leen: «Coono yu baree ngii, fàww nu jaare ci, ngir tàbbi ci nguurug Yàlla.»