Acts 14:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñi dul Yawut ak Yawut yi, ñoom ak seeni kilifa, lal pexem fitnaal leen ci sànni ay doj.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jaambur ñeek Yawut yi nag ànd ak seeni kilifa, di leen waaja mitital ak a dóori doj.