Acts 14:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moom nag muy déglu Pool miy waare. Noonu Pool xool ko jàkk, gis ne, am na ngëm ngir wér.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kookoo dégg Póol muy waare, Póol xool ko jàkk, gis ne am na ngëm gu muccam mana jaare.