Acts 15:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Amoon na bés ay nit jóge diiwaanu Yude, ñuy jàngal bokk yi ne leen: «Ku xaraful, ni ko aaday Musaa santaanee, doo man a mucc.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñenn nit ñu bàyyikoo Yude dikk Àncos, ñoo doon digal bokki taalibe yi, ne leen: «Su ngeen xaraful, ni ko aaday Musaa santaanee, dungeen mana mucc.»