Acts 15:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Nun daal ci yiwu Yeesu Boroom bi lanu yaakaar a mucce, te ñoom itam, ci lañu wékku.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yiwu Sang bi Yeesu daal lanu gëm ne ci lanuy mucce, te ñoom itam, noonu rekk.»
Recommended Reading