Acts 15:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ca njàlbéen ga ba tey am na ca dëkk bu nekk ñuy waare ci yoonu Musaa; bésu noflaay bu nekk sax dañu ciy xutba ca jàngu ya.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxte ca njàlbéen ga ba tey ay nit a ngi waaree yoonu Musaa ci dëkk bu nekk, ñu di ko jàng ci jàngu yi bésub Noflaay bu nekk.»