Acts 15:24 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Dégg nanu ne, am na ay nit ñu bawoo ci nun, ñu di leen lëjal ak seeni wax, di jaxase seeni xol, te fekk sukkandikuwuñu ci lenn ndigal lu jóge ci nun.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dégg nanu ne ay nit ñu bawoo ci nun, ñoo leen lëjal ak seeni wax, di jaxase seen xel, te nun joxunu leen lenn ndigal.