Acts 15:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag mànkoo nanu ci tànn ay nit, yónnee leen ko, ànd ak sunuy soppe Barnabas ak Pool.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax nu mànkoo ci tànn ay nit ñu nu yebal ci yeen, boole leen ak sunuy soppe Barnaba ak Póol,