Acts 15:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yónni nanu nag Yudd ak Silas, ñu di leen xamal xebaar boobu ci seen gémmiñ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag noo yebal Yuda ak Silas, ngir ñu àgge leen ci seen gémmiñu bopp, lii nu leen bind.