Acts 15:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag mbooloo mi gunge leen, ñu jaar ci wàlli Fenisi ak Samari, di nettali ni ñi dul Yawut woññikoo ci Yàlla, ba bokk yépp am ca mbég mu réy.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu mbooloom gëmkat ñi yebal leen, ñu jaare Fenisi ak Samari, daldi àgge waa foofa ni jaambur ñi dul Yawut tuube, ba bokki gëmkat ñépp bég ca lool.