Acts 15:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñu tàggoo, dem Ancos, ñu dajale mbooloo mi, jébbal leen bataaxal bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee ñu tàggtoo, daldi dem ba Àncos. Ci kaw loolu ñu woo mbooloo mi, jébbal leen bataaxal bi.