Acts 15:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu jàng ko nag, seen xol sedd ci doole, ji leen bataaxal bi indil.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu jàngee bataaxal bi, kàddu ga dëfal leen, seen xol sedd.