Acts 15:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi loolu amee ñu toog fa ab diir, ba noppi bokk yi yiwi leen ci jàmm, ñu dellu ca ña leen yónni woon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee ñu toog fa ab diir, bokk yi door leena ñaanal yoonu jàmm, yiwi leen, ngir ñu dellu ca ña leen yebaloon.