bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 15:35
Acts 15:35 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye Pool ak Barnabas des ci Ancos, di jàngale ak di xamle xebaar bu baax bu kàddug Boroom bi, ñoom ak ñeneen ñu bare.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol ak Barnaba nag des Àncos. Ñu ànd ak ñeneen ñu bare, di jàngle ak a xamle kàddug Boroom bi.