Acts 15:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw ay fan Pool ne Barnabas: «Nan dellu seeti bokk ya ca dëkk yépp, fu nu mas a yéglee kàddug Boroom bi, ba gis nu ñu def.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu ca tegee ay fan Póol ne Barnaba: «Nan dellu seeti bokk yi ci mboolem dëkk yi nu yégle woon kàddug Boroom bi, ba gis nu ñu def.»