Acts 15:40 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Pool tànn Silas, dem; bokk ya dénk leen ci yiwu Boroom bi;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol moom, taamu Silas, daldi ànd ak moom dem, gannaaw ba leen bokk ya dénkee Boroom bi ciw yiwam.