Acts 16:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon boroom kaso ba yégal loolu Pool ne ko: «Àttekat ya jox nañu ma ndigal, ngir ma yiwi leen, ngeen dem; léegi nag génnleen, te dem ci jàmm.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boroom kaso ba àgge Póol ndigal la, ne ko: «Àttekat yi kat ñoo fi yeble, ne ñu yiwi leen. Kon nag man ngeena génn te dem ak jàmm.»