Acts 16:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mboolooy ñi gëm di gën a dëgër ci yoon wi, tey yokku bés bu nekk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolooy gëmkat ñi di gëna feddliku ci wàllu ngëm, seeni lim di yokku bés ak bés.

Recommended Reading