Acts 16:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñu romb nag Misi, dem dëkku Torowas.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu tax ñu jàlle biir Misi, àkki dëkk ba ñuy wax Torowas.
2 translations compared side by side