Acts 17:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ñu fa jógee, ñu aw yoon wa jaar dëkku Amfipolis ak Apoloni, door a ñëw Tesalonig, fa Yawut ya am jàngu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee ñu jaare dëkk ya ñuy wax Amfipolis ak Apoloni, doora àgg Tesalonig, ga Yawut ya amoon ab jàngu.