Acts 17:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñi ànd ak Pool nag gunge ko ba dëkku Aten. Bi ñu fa àggee, ñu woññiku, yóbbaale ndigalu Pool ne, Silas ak Timote ñëw fekksi ko ci lu gën a gaaw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña dar Póol nag gunge ko ba ca dëkk ba ñuy wax Aten, ñu doora dëpp, jottliji Silas ak Timote kàddug Póol, ngir ñu fekksi ko nu mu gëna gaawe.