Acts 17:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi leen Pool di nég ca Aten, mu am naqaru xol wu réy ci li mu gis dëkk ba fees ak ay nataali bokkaale Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Diggante ba Póol di nég Silas ak Timote ca Aten, xolam jeex na ndax dafa gis na dëkk ba yeboo ci jaamu ay tuur.