bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 17:2
Acts 17:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Pool nag dugg ca ñoom, na mu ko daan defe, ba am fa ñetti bésu noflaay, muy werante ak ñoom ci li Mbind mi wax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol nag di leen fa fekk, na mu ko baaxoo. Diiru ñetti bési Noflaay, mu di leen waxal ci Mbind mi.