Acts 17:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte sol nga ci sunuy nopp lu nu xamul. Danoo bëggoon a xam nag léegi, loolu lu muy tekki.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax li ngay wax kat sunu ngan-gi-nopp la. Nu bëgga xam nag loolu lu muy tekki.»