Acts 17:21 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte waa Aten ñépp ak doxandéem ya fa dëkk, wax ak a déglu lu bees rekk lañu daan xënte.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba waa Aten ñépp, doxandéem ak njuddu-ji-réew, xintewuñu lenn lu moy di nettali ak a déglu xew-xew wu bees.
Recommended Reading