Acts 17:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu Pool taxaw ci biir mbooloom Areyopas ne leen: «Yéen waa Aten gis naa ne, farlu ngeen ci diine lool.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Póol taxaw ca digg ëttub Areyopas, ne leen: «Yeen waa Aten, gis naa ne ci wet gu nekk ñu farlu ngeen ci diine.