Acts 17:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kenn nit la sàkke xeeti àddina yépp, ñu dëkk ci ñeenti xebla yi; fekk àppal na xeet wu nekk jamonoom, te rëdd seen diggi réew.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo sàkke xeeti àddina yépp ci kenn nit, ñu dëkke déndu suuf sépp, te moo leen àppal seeni jamono, rëddal leen seen kemi dëkkuwaay.