Acts 17:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mu di leen ko tekki, te di leen wax ay firnde yuy wone ne, fàww Almasi bi sonn te dekki. Mu ne leen: «Yeesu, mi ma leen di yégal, mooy Almasi bi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu di leen tekkil Mbind mi, di leen ci firndeel ne coonob Almasi ak ndekkiteem manul woona ñàkk. Mu ne leen: «Yeesu mii ma di leen xamal, mooy Almasi.»