Acts 17:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca jamono yu wees ya Yàlla toppul ñàkka xam googa, waaye léegi koo man a doon ak foo man a nekk, Yàlla santaane na, nga tuub say bàkkaar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yàlla nag jéllale na janti ñàkka xam googa woon, waaye tey mu ngi woo ñépp, ak fépp fu ñu féete, ngir ñu tuub.