Acts 17:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moona am na ñenn ñu taq ci moom te gëm: xàmmees na ci Denis, ku bokk ci mbooloom Areyopas, ak jigéen ju tudd Damaris, ak ñeneen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul mu am ñu ko fekksi, ba mujj gëm; Denis mi bokk ci ëttub Areyopas ci la, ak jigéen ju ñuy wax Damaris, ak ñeneen.