Acts 18:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte maa ngi ànd ak yaw, te kenn du la jàpp, ba fitnaal la, ndaxte am naa xeet wu bare ci dëkk bii.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax maa ànd ak yaw, kenn du la song, def la lu bon, ndax xeet wu yaa laa am ci dëkk bii.»