bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 18:15
Acts 18:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye bu ajoo ci ay werante ciy wax ak ay tur ak seen yoon, loolu seen wàll la; man duma ko àtte.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye su dee ag dëngoo ci wàllu wax, mbaa ay turi nit, mbaa seen yoonu bopp nag, seetal-leen ko seen bopp. Àtte loolu moom, duma ko nangu.»