Acts 18:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu nit ñépp jàpp Sosten, njiitu jàngu ba, ñu di ko dóor ca kanamu àttekaay ba, waaye Galyon faalewu leen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ñépp jàpp Sosten, njiitu jàngu ba, dóor ko ca àttekaay ba, te taxul Galyon yégal ko yaramam.