Acts 18:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu tase fa ak Yawut bu tudd Akilas te juddoo diiwaanu Pont. Muy sog a jóge réewu Itali ak jabaram Pirsil, ndaxte buur ba Këlódd sant na Yawut yépp, ñu génn Room.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu daje fa ak Yawut bu ñuy wax Akilas, fekk baax diiwaanu Pont. Muy sooga jóge réewum Itali, ànd ak soxnaam Pirsil, ndax Buur bu mag ba Këlódd moo joxe woon ndigal ne na Yawut yépp génn Room.