Acts 18:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon mu tàggtoo ak ñoom naan: «Dinaa dellusi ci yéen, bu soobee Yàlla.» Noonu mu dugg gaal, jóge Efes,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la tàggtoo ak ñoom, ne leen: «Dinaa leen seetsiwaat, bu soobee Yàlla.» Ba loolu amee mu dugg gaal, bàyyikoo Efes,