Acts 18:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bi Silas ak Timote jógee diiwaanu Maseduwan, egg fa, Pool jublu ci xamle kàddu gi, tey dëggal ci Yawut yi naan, Yeesu mooy Almasi bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Silas ak Timote dikkee, bàyyikoo diiwaanu Maseduwan, Póol xintewootul lu moy di xamle kàddu gi, di seereel Yawut yi ne Yeesu mooy Almasi.