Acts 18:9 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Naka noona Boroom bi feeñu Pool ci guddi ne ko: «Bul tiit dara, waaye deel wax te bañ a noppi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Sang bi wax ak Póol ag guddi ci biir peeñu, ne ko: «Bul tiit dara, waaye waxal te bul noppi,
Recommended Reading